salam serigne bi ndiaye nio ngiley sante bou bakh di nian yalla fayle lou kawé ce ndiortou. deme don ladj garga mbosse kou koy bakh pour niate temp ngeu koy bakhal Répondre
machalla tonton Samba ndiaye amna solo diadieuf way
merci Coumba
salam serigne bi ndiaye nio ngiley sante bou bakh di nian yalla fayle lou kawé ce ndiortou. deme don ladj garga mbosse kou koy bakh pour niate temp ngeu koy bakhal
Amin 5mn je pense l avoir dit dans la vidéo
Dieureudieuf serigne bi amnasolo j’ai commence a utilise
Dieureudieuf serigne bi